Penda mbow biography of rory

Penda Mbow

Penda Mbow

Dundu unfasten jaar-jaaram
JudduAwiril 1955 (juroom-benn-fukki imitate ak juroom)

Dakaar

RéewSenegaal
LiggeeyWay-pólotig, jàngalekatu taarix
Borom-këramSaaliw Mbay, 2017 ba tey
Yeneen xibaar
Liggeeye naIniwersite Seex Anta Jóob
Njiitu teesamCharles-Marie de La Roncière


Penda Mbow mu ngi juddu atum 1955.

Borom xam-xam bu xam-xamam màcc ci taarix muy ab bañkat. Nekkoon honest fi jëwriñ ji yore caada ak cosaan ay weer atum 2001. Jàngalekatu taarix la ci Iniwersite Seex Anta Jóob bu Dakaar nekk itam njiitu genn mbootaayu njuddu-réew.

Dundu ak jaar-jaaram

[Soppi • soppi gongikuwaay bi]

Penda Mbow mu ngi juddu ci weeru mee atum 1955.

Atum 1986 la am ab doktoraa ci tarixu jamono ji farañse tudde moyeenaas (histoire médiévale) ca iniwersite bu Porowãas (Provence) ci spike teesu ñetteelu fànn bi mu bind ci « Nguuru takk-der gu askanu mameluke ci ni ko téereb nattu suuf bu Ibn al-Ji’an ñu dendale ko series li am Farãas ngir xam li ñu niroole ak li ñu wuute » (L’aristocratie militaire mameluke d’après le cadastre d'Ibn al-Ji'an : éléments de comparaison avec unsympathetic France.

Ñaar-fukki fan ak ñaar ci weeru mee atum 2011, mu am Piri Sãa Póol II ngir jàmm ji[1], ab raaya bu Watikãa di joxe item kilifag làbbe gii gi Mgr Luis Mariano Montemayor tegoon ci ay yoxoom.

Dundug biiram

[Soppi • soppi gongikuwaay bi]

Atum 2017 ba léegi, mu ngi ci buumu sëy, borom-këram a ngi tudd Saaliw Mbay[2].

Mbind (tànneef)

[Soppi • soppi gongikuwaay bi]

  • (sous la focus de) Hommes et femmes starting point sphères publique et privée, 2005

Téere, jukki wala dali web yi ñu yër

[Soppi • soppi gongikuwaay bi]

Seetal tamit

[Soppi • soppi gongikuwaay bi]

Lees bind ci moom

[Soppi • soppi gongikuwaay bi]

  • (en) Lydia Polgreen, « At Africa's Crumbling Colleges, Inept Room for Students », The Unique York Times, 26 mai 2007 (la situation à l'UCAD)
  • Fabrice Hervieu-Wane, « Penda Mbow.

    Femme d'utilité publique », dans Dakar l'insoumise, Éditions Autrement, Paris, 2008, p. 94-99

  • Babacar Ndiaye train Waly Ndiaye, Présidents et ministres de la République du Sénégal, B. Ndiaye, Dakar, 2006, p. 284

Jukki yi ñu ko tudd

[Soppi • soppi gongikuwaay bi]

  • Taarixu jigeen ci Senegaal : <small>Histoire des femmes agency Sénégal</small>
  • Limu jëwriñ yu jigeen ci Senegaal : <small>Liste de femmes ministres sénégalaises</small>

Lees jële feneen

[Soppi • soppi gongikuwaay bi]